Press "Enter" to skip to content

Bril – Bras Long – Clip Officiel

** Contact monitoring **.
Mr Mahmoud Sy: +221 77 036 48 31.
brilfight4@gmail.com.

** Crédits de la chanson “Bras Long” **.
Auteur: Bril.
Compositeur: Bril.
Workshop enregistrement, edit, learning & mix: Class’ Chic Music the same level Bril.
Une manufacturing de Class’ Chic Music (Dakar, Senegal, août 2019).

** Retrouvez Bril sur les réseaux sociaux **.
Facebook https://www.facebook.com/brilofficiel.
Instagram https://www.instagram.com/bril_officiel.
Twitter https://twitter.com/bril_fight4.
Snapchat: @bril- fight4.

** Booking global **.
vincent.lagoeyte@soon.pro.

** Abonne-toi à ma chaîne ici https://goo.gl/Qw5BFh**
Le clip “Bras Long” est le top solitary extrait du nouvel cd de Bril, SUBA, disponible à partir du vendredi 20 septembre sur toutes les plateformes de straeming et téléchargement.
Pas facile de trouver un woe au Sénégal quand on n’ a pas de connection ou de piston … Faire des études ne semble vraiment pas suffire! (voir Lyrics plus bas dans cette summary).
#Bril #BrasLong #Suba #NouvelAlbum 20septembre #ClassChicMusic #team 221.

Introduction.
ooooh ooh ooooh.
Bril laa aaah.
( Bril on the beat).

Refrain.
Fi douniou khol lane nga xam wala lo meune?.
Daniouy Laathie kane mola yabal thi niom..
Lokho bou goudou fok nga amko soga dém.
Bouthi kéneu djaappoul dinga yaggueu thi sa yone..
Est ce que am nga Bras Long?
” Bras Long – Bras Long “.
Bo amoul Bras Long, dothi gawa guéneu.
Am nga Bras Long!
” Bras Long – Bras Long “.
Bo amoul Bras Long, Est ce que ding thi guéneu?.

** Mon nouvel cd SUBA est sorti. A écouter et/ou télécharger en cliquant ici https://listen.lt/BrilSuba1 **

** Crédits du clip “Bras Long” **.
Réalisation: Reverse Studios.
Stylisme: Bise Collection et Mouha Creation.

** Lyrics de la chanson “Bras Long” **.

1er Couplet.
Bimay khalé dagn ma gueumlo ni wone, bouma djangué, bouma maaggué liguey.
Ma yaggueu thi école yi woute ay diplômes, lima memorizing thi xam guéédj la meuna thié fééy..
Wayé founé démnafa, lima djokhé thi ay curriculum vitae boudone khaliss ma done millionaire..
Bo kholé sén mbalite yi guissmafa, bimay déposé lay xam douma am, moudjé nékk visionnaire.
Kane mola yabal? Fok nga xam, kou xam koulén xam! Djangal badone kangam sokhlawougn sa Xél fii!.
Kholouniou sa xam xam, Lidjeuntiwougn sa meune meune, Wouteul Bras Long mélal ni kouy selfie!.

Refraun.
Fi douniou khol lane nga xam wala lo meune?.
Daniouy Laathie kane mola yabal thi niom..
Lokho bou goudou fok nga amko soga dém.
Bouthi kéneu djaappoul dinga yaggueu thi sa yone..
Est ce que am nga Bras Long?
” Bras Long – Bras Long “.
Bo amoul Bras Long, dothi gawa guéneu.
Am nga Bras Long!
” Bras Long – Bras Long “.
Bo amoul Bras Long, Est ce que ding thi guéneu?.

2ème Couplet.
Bo amoul koulafa nékkal yakkar ni dangay am, Day mélni ngané dangay Connectéwou té amo pass!.
Té fo am yakkar djaroul ngafay dém, boudé kénneu Xamoulafa ni sa mot de passe!.
Thi musique bi, Lamb Dji’ak foumou meunti done, bou sa lokho goudoul lingay yôttou dothi djote..
Bo khamoul kou xam borom téén djaroul ngay soneu, même bo amé baak yaw dofa meuna Roote..
Bodé djiguén gueum sa bopp state mbir dougn thi #Takhaw, Dofa meuna #Took, Boudé beuggo #Teudd.
Niawloul ay courte manche bo amoul Bras Long, lo beugga natteu niounéla djotoula, lofi wakh dou deugg..

Refrain.
Fi douniou khol lane nga xam wala lo meune?.
Daniouy Laathie kane mola yabal thi niom..
Lokho bou goudou fok nga amko soga dém.
Bouthi kéneu djaappoul dinga yaggueu thi sa yone..
Est ce que am nga Bras Long?
” Bras Long – Bras Long “.
Bo amoul Bras Long, dothi gawa guéneu.
Am nga Bras Long!
” Bras Long – Bras Long “.
Bo amoul Bras Long, Est ce que ding thi guéneu?.

Pont.
Amo bras Long, Takhoul nga djaay sa ngor, danga woute liguéy bachelor’s degree woutoum Liguéy moudjé done sa Liguéy..
Boul Khaadi té boul gawa bayi, Kheuthie bou daggoul dikkeu, Yalla bourbi dalay Fay..
Est ce que am nga Bras Long?
” Bras Long – Bras Long “.
Bo amoul Bras Long, dothi gawa guéneu.
Am nga Bras Long!
” Bras Long – Bras Long “.
Bo amoul Bras Long, Est ce que ding thi guéneu?